Genesis in Wolof ( Njàlbéen ga)
Yàlla sàkk na àddina fal ci nit (1:1)
Yàlla dugal na nit Àjjana jox ko ndigal (2:4)
Yàlla dàq na nit Àjjana (3:1)
Kayin rey na Abel (4:1)
Askanu Kayin (4:17)
Askanu Aadama ba ci Nóoyin (5:1)
Yàlla fas na yeene tas àddina (6:1)
Askanu Nóoyin (6:9)
Yàlla musal na Nóoyin ci mbenn mi (7:1)
Nóoyin génn na gaal gu mag ga (8:1)
Yàlla fas na kóllëre ak Nóoyin (9:1)
Mbirum Nóoyin ma ak i doomam (9:18)
Xeet yi sosoo ci doomi Nóoyin (10:1)
Li jëm ci askanu Yafet (10:2)
Li jëm ci askanu Xam (10:6)
Li jëm ci askanu Sem (10:21)
Yàlla
safaan na làkku àddina mu jaxasoo (11:1
Askanu
Sem maamu Ibraam (11:10)
Askanu
Teraa baayu Ibraam (11:27)
Yàlla
sant na Ibraam mu gàddaay (12:1)
Ibraam
dem na réewu Misra (12:10)
Ibraam
ak Lóot teqalikoo nanu (13:1)
Digeb
Aji Sax ja ak Ibraam (13:14)
Ibraam
wallu na Lóot (14:1)
Melkisedeg
ñaanal na Ibraam barke (14:17)
Yàlla
fas na ak Ibraam kóllëre (15:1)
Ismayla
juddu na (16:1)
Yàlla
soppi na turu Ibraam (17:1)
Xaraf
mandargaal na kóllëreg Yàlla (17:9)
Ibraayma
ak ganam ña (18:1)
Ibraayma
tinul na waa Sodom (18:16)
Bàkkaari
waa Sodom (19:1)
Lóot
genn na Sodom (19:12)
Yàlla
tas na dëkk yooyu di Sodom ak Gomor (19:23)
Mbirum
Lóot ak doomam yu jigéen ya (19:30)
Lu
jëm ci Ibraayma ak Abimeleg (20:1)
Juddub
Isaaxa (21:1)
Saarata
jote na ak Ismayla ak Ajara (21:8)
Ibraayma
waatoo na ak Abimeleg (21:22)
Yàlla
nattu na Ibraayma (22:1)
Askanu
Naxor (22:20)
Ibraayma
jënd na suuf ca Kanaan (23:1)
Isaaxa
jël na Rebeka soxna (24:1)
Ibraayma
nelaw na (25:1)
Askanu
Ismayla (21:12)
Askanu
Isaaxa doomu Ibraayma (25:19)
Esawu
sàggane na céram (25:27)
Isaaxa
nëbbu na waa Gerar ngir mucc (26:1)
Isaaxa
fas na kóllëre ak Abimeleg (26:12)
Esawu
jël na ay soxna (26:34)
Yanqóoba
jekk na Esawu ci ñaanam (27:1)
Yanqóoba
dem na ca nijaayam (27:41)
Esawu
jel na yeneeni soxna (28:6)
Yanqóoba
sartoo na ak Yàlla (28:10)
Yanqóoba
daje na ak Rasel (29:1)
Njaboot
gi Yanqóoba am (29:31)
Yanqóoba
woomle na (30:25)
Yanqóoba
toxu na jëm Kanaan (31:1)
Laban
dabi na Yanqóoba (31:22)
Yanqóoba
ragal na daje ak Esawu (32:4)
Bëreb
Yanqóoba bu réy ba (32:23)
Yanqóoba
ak Esawu daje nañu ci jàmm (33:1)
Tooñ
nanu Diina doomu Yanqóoba (34:1)
Yanqóoba
sanc na Betel (35:1)
Ben-yamin
juddu na Rasel faatu (35:16)
Doomi
Yanqóoba ya (35:22)
Isaaxa
nelaw na NGJ01
Askanu Esawu (35:27)
Askanu
Seyir (36:20)
Buur
ya jëkk a falu ca Edom (36:29)
Yuusufa
gént na lu yéeme (37:1)
Yuda
ak Tamar ak seen askan (38:1)
Jaay
nañu Yuusufa jawriñu Firawna (39:1)
Soxnas
Potifaar fexeel na Yuusufa (39:7)
Tej
nanu Yuusufa kaso (39:19)
Yuusufa
firi na génti ñaar ña ñu tëj (40:1)
Firawna
gént na (41:1)
Yuusufa
firi na génti Firawna (41:14)
Firawna
fal na Yuusufa mu jiite Misra gépp (41:37)
Magi
Yuusufa ya dem nañu Misra (42:1)
Yuusufa
xupp na magma ya (42:7)
Doomi
Yanqóoba ya dellu nañu Kanaam (42:24)
Magi
Yuusufa ya yóbbu nañu Ben-yamin (43:1)
Magi
Yuusufa ya dellu nañu Misra (43:15)
Yuusufa
nattu na ay magam (44:1)
Yuda
tinul na Ben-yamin ca Yuusufa (44:14)
Yuusufa
xàmmiku na ay magam (45:1)
Firawna
woo na Yanqóoba Misra (45:16)
Yanqóoba
dem na Misra (46:1)
Njabootu
Yanqóoba gi ñëw Misra (46:8)
Yanqóoba
gis na Yusuufa (46:28)
Yuusufa
nuyoole na ay bokkam Firawna (47:1)
Saytub
Yuusufa ca xiif ba (47:13)
Ati
Yanqóoba yu mujj ya (47:27)
Israyil
ñaanal na Efrayim ak Manase (48:1)
Yanqóoba
taago na (Kàdduy Yanqóoba yu mujj ya) (49:1)
Yanqóoba
nelaw na (49:29)
Yuusufa
rob na Yanqóoba réewu Kanaan (50:1)
Magi
Yuusufa yaa ngi jégglu (50:15)
Yuusufa
nelaw na (50:22)